Wanema INFO
Image default
Société

« Sama keur jeukeur yapp bou nioroul laniouy lekk…té chak fois bougn koy… », une nouvelle mariée en désarroi fait une révélation qui fait froid dans le dos

C’est encore une révélation qui choque, pire, qui fait froid dans le dos. Cette nouvelle mariée n’y arrivera pas.

« Dama diakhalé torope keur bi méye séyé mane la ak sama dieucoeur ak parent wame mais dale dama sélou ni douniou léke yape bou gnore toujours dagnouye mey farale di wakh ma togou viande saignante maname beugouniou yape bi gnore bilahi dama titt yayame bouye togou douma meune léke tellement da géy guiss yape bi dou gnore et en plus dérett bi dey visible nama yalla bale dama fokeni keur deumbe la séysi boulma khébale sama ano stp
Postél stp ba kham »

Sélectionné pour vous

Escroqué par son ex agent, Papis D. Cissé toujours amer : « J’avais vraiment confiance en lui »

Découverte macabre à Rufisque : Un homme retrouvé mort calciné

Opérations du service de l’hygiène : 300 maisons déjà nettoyées à Touba 

Laisser un Commentaire